- Hey bro baalal ma nak - awe ma...
- Kee kan la nii?
- Daf maa nyaan di - hamute neh maa ko gaynaa broke... hey dimbaleh ma bro - hanaa nga ute nyowe nyu borka..
- Hahaha - woye!
- Turnal rek - bull am eye contact ak morm...
- Narr baang kore daaha...
- Hayy yowe lii russ lu na deh - haa ma seht ndah am naa dara...
- Waaneh dot com. yowe dinga ever change?
- Nee la mel deh - hanaa danga faateh timey school - sarahtu kat bunj rormba..
- Jang ha bi joh ko haalis! Wah nga dayga! Nyorm Matarr One Eye..
- Heeeei! Ana koe ku?
- Deyorn na di!
- Hai! Kanj!
- Like three years ago - dama call kerr suma yaaye di ma ko wah..